Le décès de l’ancien ministre et maire de Mbacké, Iba Gueye a bouleversé le mannequin Fleur Mbaye. Elle lui a fait un témoignage, très émouvant.
« Aye Yalla Aye Yalla so soxla jamm bi gnak wante manone guako fi bayi bassi kaname. Aye way tonton Iba Gueye demena sama kharit sama papa sama patron sama lep. Yama ndieukeu diokh ligueye Dakar au COUD meusso beugue louma méti meussoma setane japma jap sama rakk. Dimbaliguama founek ak heure bounek. Doumala meusse faté sama adouna. Non taye amena louma méti torop walahi. Nigua dimbaliwe domou adama yi si adouna bi Yalla nala faye lolou teroula si aldjana firdawssi si barke cheikh ahmadou bamba Amine », lit-on sur Dakarswagg.
Actusen.com